Njaay mi

Sunuy téere ngiy jaay ci juróomi réew ci àddina wërngal kepp. Te liy ñëw a dàq.

North America EJO

Amerig, Kanadaa ak Meksig

Mën ngeen a jënd sunuy téere ci Amazon walla ngeen jokkook Thierno Guèye (+15144184140).

Senegal EJO

Senegaal

Librairie Aux 4 Vents (Dakar), Librairie Clairafrique (Dakar & Thiès), L’Agneau carnivore (Saint-Louis) ak L’Harmattan (Dakar, Ziguinchor ak Saint-Louis). Walla ngeen jokkook Ndèye Codou Fall (+221776516848).

France EJO

Faraas

Présence Africaine (Paris), L’Harmattan (Paris) ak Folies D’Encre (Saint-Denis). Walla ngeen jokkook Mme Assy FALL (+33633967554).

Distribute EJO books

Su ngeen bëggee jaay sunuy téere

Su nu amoon li nu gënal, téere yi EJO defar dañuy jar fépp ci àddina si. Su ngeen leen bëggee jaay ci seen réew, noo ngi leen di xaar fii : jokkook nun.