Kërug móolukaay gu bees gu caaxaan taxul a jóg
Screen Shot 2018-09-16 at 8.53.36 PM

Sunu téere bu bees bi

Ci téereem bii, Ceerno Séydu Sàll dafa tàllal askan wi seetu ngir mu janook xar-kanamam, xam moom mooy kan ci dëgg-dëgg, fàttaliku ne lépp lu waay teg sa bopp, yëg metit wu tar, ni ‘’wóoy sama ndey’’, war ngaa xoolaat bala nga koy teg keneen. Ndax jaadu na nit kiy xàwwi sutura moroomam, walla di ko ñàkkal faayda mbaa di ko sosal ? Ku jàng Puukare dinga xam ne li am solo mooy nu àndandoo nekk benn, moytu lépp luy jur fitna, ñeme coono te ragal Yàlla.

Blog EJO

Aycaleen!

lu defu, waxu mooy béréb bi nuy làngeek askan wi, di waxtaane pólitig ak caada ak lépp lu xew ci Afrig mbaa ci àddina si. Fas yéene nan cee ganale yit ay kàngami Afrig, bu ñu nu yónnee seen gis-gisu jamonoy tey, nu daldi leen koy jottali.

Jàngleen lu defu, waxu

Bu weesoo Senegaal, mënees naa jënd sunuy téere ca Amerig, Meksig, Kanadaa ak Frãs. Ku leen soxla ci réew yi nu limul fii, mën naa jokkook nun